kasahorow Wolof

Boppë, Mbagg, Óom Ak Baraamu Tànk

kasahorow Sua, date(2018-11-22)-date(2024-11-28)

Boppë, mbagg, óom ak baraamu tànk.
Boppë, mbagg, óom ak baraamu tànk.

Bët, noopp, bakkan ak gemeñ.

Boppë, mbagg, óom ak baraamu tànk.
Óom ak baraamu tànk.

#boppë #mbagg #óom #baraamu tànk #bët #noopp #bakkan #gemeñ
Share | Original