fie.nipa,

Ab Làl

Tur: ab làl

Làl salamelekoum.
Waaw, ab làl.

Ab picc?
Déet.

Ab garab?
Déet.

Ab ordinaatër?
Déet.

Naaj bi?
Déet.

Ab xale bu goor?
Déet.

Ab làl?
Waaw.

Wolof Dictionary

  1. ab làl
  2. ab xale bu goor
  3. naaj bi
  4. ab ordinaatër
  5. ab garab
  6. ab picc
<< Previous | Next >>